bakkan
Apparence
wolof
[Soppi]bakkan: amna ñaari piri
- bakkan ab cér la ci nit, dees koy jëfandikoo ngir nóyyi ak ñàndu...
- bakkana dees nako wax ngir jublu si liy waral nit di dund, niki diw ñàkk na bakkanam/dee na.
Xool it
[Soppi]ci yeneeni làkk
[Soppi]- wu-faraas: nez
- wu-angalteer: nose
Déglu baatu bakkan ci wolofi Senegaal