Aller au contenu

solo

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

solo

  1. solo su sunu liggéey mooy suqali kàllaama wolof
  2. ci xayma : Ab digaale buy ñaarñaarlo, jóge ci E ba ci F solo la, su fekkente ne cëru E bu ne digaale na ak lu ëpp benn cër ci F

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: fonction, importence

Delluwaay

[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005