Aller au contenu

alal

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

baatub alal ci làkkuw araab la bawoo. → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

alal j

  1. linga moom, xaalis, kër, yëre añs.
    • kii ku fonk alalam la!

Bokktekki

[Soppi]

am-am

Waxiin

Déglul ni ñuy waxee alal ci wolofi Senegaal